Les phrases clés

Salam Aleykoum / Aleykoum salam

Bonjour / Bonjour à toi aussi

Ba beneen

Au revoir

Ba ci kanam

A la prochaine

Man

Moi

Man laa

C’est moi

Man laa Édo

C’est moi Édo

Yaw / ak yaw

Toi / avec toi

Yaw nak ?

Et toi?

(Yaw) kan la ?

(Toi) Qui es-tu?

Déglu ma

Écoute-moi

Bu baax

C’est bien/ bon

Dafa neex lool

C’est trop/ très bien/ bon

Dama xiif / Dama mar

J’ai faim / j’ai soif

Dama suur

Je suis rassasié/ je n’ai plus faim

Dama mer

Je suis en colère

Dama bég

Je suis content

Dama bég ci gis la

Je suis content de te voir

Dama jaaxle

Je suis inquiet

Dama sonn lool

Je suis très fatigué

Dama gëmentu

J’ai sommeil

Dama bëgg nélaw

Je veux dormir

Damay yeewu

Je me réveille/ en train de me réveiller

Yeewu naa

Je me suis réveillé

Naka mu ? / Na nga def ?

Comment ça va ?

Yangi noce ?

Tu es en forme?

Maangi (Ma Guy) ci jàmm rekk, sant Yalla

Je suis en paix seulement, merci Dieu

Maangi ci jàmm bu bakh

Je vais très bien

Maangi fii rekk

Je vais bien seulement / je suis ici

Lu bees ? dara beesul

quoi de neuf ? rien de neuf

Lu

Quelque chose

Naka tey ? mu ngi neex

comment ça va aujourd’hui ? Ça va bien

Naka yaram wi ?

Comment va la santé ?

Naka/ ana waa kër gi ? Ñu ngi ci jàmm

Comment va la famille? (les gens de la maison) ils sont en paix

Naka xale yi ? ñu ngi ci jàmm

Comment vont les enfants? ils sont ici/ en paix

Naka liggéey bi ? Mu ngiy dox

comment va le travail ? il marche

Naka afeer/ mbir yi ? Mu ngiy dox

comment vont les affaires ? ça marche

Ana sa jabar ? Mu ngi fa

comment va (où est) ta femme? elle est là-bas

Naka nga tudd ? Noo tudd ?

comment t’appelles-tu ?

Maangi tudd Édo / Édo laa tudd

Je m’appelle Édo

Naka nga sant ? Noo sant ?

quel est ton nom de famille?

Maangi sant Go / Go laa sant

Mon nom est Go

Am naa Nẽent Fukk at ak Juroom-Ñett

J’ai 48 ans

Fan nga juddoo ? Foo juddoo ?

Où es-tu né ?

Juddoo naa ci Farans

Je suis né en France

Mag naa fi

J’ai grandi ici

Senegaalais laa

Je suis sénégalais

Duma tubaab

Je ne suis pas étranger

Duma jullit 

Je ne suis pas musulman

Dama gëm Yalla

Je crois en Dieu

Dama gëm ne dina + verbe infinitif

Je crois qu’il va …

Mu ngi julli ci jakka

Il est en train de prier à la mosquée

Dégg naa manjaak bu baax, ndaxte manjaak laa. 

Je comprends bien le manjak parce que je suis manjak

Su bëgg nga ñu wax ci wolof

Si tu veux, on peut parler en wolof

Ñaata at nga am ?

Quel âge as-tu ?

Am naa ñetti mag bu góor ak benn mag bu jigéen

J’ai 3 grands frères et 1 grande soeur

Am naa benn doom bu góor

J’ai un fils

Sama doom bu góor la

C’est mon fils

Sama doom bu góor tudd na M, am na 16 at

Mon fils s’appelle M, il a 16 ans

Ndax gis nga ko ?

Est-ce que tu l’as vu ?

Mooy M.

Lui c’est M. (en présentation)

Fan nga dëkk ? Foo dëkk ?

Où habites-tu ?

Maangi dëkk ci Pikin, ci quartier Lansar.

J’habite à Pikine, au quartier Lansar

Fan nga jóge ? Foo jóge?

D’où viens-tu ?

Jóge naa ci Farans

Je viens de France

Dégg nga wolof ? 

Comprends/parles-tu le wolof ?

Maangi dégg wolof tuuti rekk

Je comprends le wolof un petit peu

Maangi jang wolof tamit

Je suis en train d’étudier/ apprendre le wolof aussi

Dama goor-gorlu

Je me débrouille/ je fais des efforts

Dégg naa Lépp

Je comprends tout

Ndax mën nga wax ndànk ndànk ?
Est‑ce que tu peux parler lentement ?

Ban (yan) làak nga dégg ?

Quelle(s) langue(s) parles-tu ?

Xalaat naa ne jang wolof metti, waaye dafa am solo

Je pense que c’est difficile d’apprendre le wolof mais que c’est important

Dafa metti / dafa jafé

C’est difficile

Wolof dafa jafé

Le wolof est difficile

Lan mooy sa liggéey?

Quel est ton travail ?

Consultant laa

Je suis consultant

Dama liggéey ci Farans tamit

Je travaille en France aussi

Bëgg naa Senegaal ndaxte dafa tang lool

J’aime le sénégal car il fait chaud

Senegaal dafa neex ci sama xol

Le Sénégal me plait beaucoup/ est agréable à mon coeur

Lan la ?

Qu’est-ce que c’est ?

Lan nga bëgg ? Loo bëgg ?

Qu’est-ce que tu veux ?

Dama bëgg lekk ay togg yu Senegaal.

Je veux/ aime manger des plats sénégalais.

Dama bëgg ceebu jën ak yassa ginaar.

Je veux/ aime manger le ceebu jën et le yassa au poulet

Ndax mën nga jox ma furset ak paaka ?

Est‑ce que tu peux me donner une fourchette et un couteau ?

Ndax mën nga jox ma furset walla kuddu, baax na ?

Est‑ce que tu peux me donner une fourchette ou une cuillère, s’il te plaît ?

Dama bëgg naan bissap ak ndox

Je veux/ aime boire du bissap et de l’eau, parce que le bissap est très sucré.

Bissap dafa neex waaye suukar na lool

Le bissap est bon mais trop sucré

Lan nga bëgg lekk ?

Qu’est-ce que tu veux manger ?

Gëj naa lekk yassa ginaar

Ça fait longtemps que je n’ai pas mangé du poulet yassa

Yaw, Danga bëgg lekk reek

Toi, Tu veux seulement manger

Damay xaar

Je vais attendre

Damay ñibbi

Je rentre

Damay doxantu ci Paris

Je me promène dans Paris

Lu tax ngay jooy ?

Pourquoi tu pleures?

Dama la bëgg

Je t’aime

Dama bëgg tukki

Je veux voyager

Dama Bëgg nu waxtaan

Je veux qu’on discute

Dafa bari wax

Il parle trop

Bakh na / neex na

C’est bien/ c’est bon

Jërëjëf ! Ñoo ko bokk

Merci ! De rien

Dama bëgg def esport bu bakh

Je veux/ aime bien faire du sport

Ana wanag bi ?

Où sont les toilettes?

Dama tang / dafa tang

j’ai chaud / il fait chaud

Dama sedd / dafa sedd

j’ai froid/ il fait froid

Dama gëmentu

j’ai sommeil

Dama feebar

je suis malade

Dama ragal

j’ai peur

Moytul

Fais attention

Damay kaf

Je plaisante

Xaaral tutti

Attends un peu

Déetdéet, amuma xaalis

non, je n’ai pas d’argent

Baal ma

excuse-moi

xxx déggul wolof

xxx ne parle pas wolof

Mouss mu ngi dëkk dakar

Mouss vit à dakar

Dama dem bank jël xaalis

Je vais à la banque retirer de l’argent

Dama soxla xaalis

J’ai besoin d’argent

Dama wut bànk

Je cherche une banque

Dama bëgg def wiirmaa

Je veux faire un virement

Dama bëgg def deppo ci sama kont

Je veux faire un dépôt sur mon compte

Xool ma

Regarde moi

Kaay fi

Viens ici

Kaay lekk ! 

Viens manger!

Toogal!

Assieds-toi

Dina leeral

Je vais t’expliquer

Maa ngi Ñów

J’arrive

Ñaata lay jar ? ñaata la ?

Combien ça coûte ?

Dafa cher !

c’est cher!

Danga raféte

Tu es belle

Danga baax

Tu es gentil

Mu ngiy dox

Ça marche

Am na mburu bi

Il y a du pain

Pare nga ? pare naa

tu es prêt ? je suis prêt

Dafa yomb

C est facile

Maangi dem ci butik, am na weer lool.

Je vais à la boutique, il y a énormément de monde.

Bëgguma xaar

Je ne veux pas attendre.

Maangi dem jënd mburu.

Je vais acheter du pain

Dafa dem Pikin seeti yaayam

Il est allé à Pikine voir sa mère

Damay jaay yére

Je vends des vêtements

Woolu naa la

Je te fais confiance

Dama réer

Je suis perdu

Dangay fen

Tu mens

Bayima

Laisse-moi tranquille

Lan nga def?

Qu’est-ce que tu as fait ?

Damay xalaat

Je réfléchis

Sét na

C’est propre

Tilim na

C’est sale

Dama Jambar

Je suis courageux

Danga Yambar

Tu es faible/ peureux/ fragile

Danga wax bari

Tu parles beaucoup

Dëgg laa

C’est vrai

— am na ?

y a t il — ?

Foog naa ne metti na jang wolof

Je pense que c’est difficile d’apprendre le wolof

Dama dem bank Faatu xaalis

je vais déposer de l’argent à la banque (présent)

def naa esport

je fais du sport

dégg naa Lépp

je comprends tout

pare nga ? pare naa

tu es prêt ? je suis prêt

dafa metti / dafa jafé

c’est difficile (2 façons)

maangi Góor‑góorlu

je me débroullle/ je fais des efforts

dafa am solo

c’est important

amul solo

pas de souci/ pas grave

bayima!

laisse-moi tranquille!

ragalouma la!

je n’ai pas peur de toi!

kaay toog! ou Toogal !

viens t’asseoir!

gaawal !

dépêche-toi !

noppil !

tais-toi!

Loo bëgg ?

tu veux quoi ?

Fatou dafa tayal

Fatou est paresseuse

Dama am fit / dama am doole

je suis en forme-force / je suis courageux

Boroom kër gi la

Je suis le propriétaire de la maison

nuyu ko

Salue-le

mbaa / ndax … ?

est-ce que … ?

soxla naa xaalis

j’ai besoin d’argent

Ma jox la nenti-téemeer

je te donne 2000 fcfa

Defuma

je n’ai pas fait

dafa sore/ dafa soriwul

c’est loin/ ce n’est pas loin

moo tax

c’est pourquoi / voilà pourquoi

senegalais nga ?

tu es sénégalais ?

kër Abdu Juuf

la maison d’Abdou Diouf

amuma

je n’ai pas

naanuma ndox robine

je ne bois pas l’eau du robinet

dama nekk benn rekk

je suis seul

dëgg la

c’est vrai

na nga fanaane ?

tu as bien dormi?

kaň nga dëkk fi ?

depuis quand habites-tu ici ?

sey nga ? / am nga jabar ?

Tu es marié ?

dégg naa radio

j’écoute la radio

Dinaa dem seetaan film ci cinema

Je vais aller regarder un film au cinéma

kaň la dem?

quand est-il parti ?

lan lay bind?

qu’est ce qu’il écrit ?

kan la seeti ?

qui est-il allé voir?

dafa ragal ndox, mënul féey

il a peur de l’eau, il ne sait pas nager

lu mu wax ?

qu’est-ce qu’il a dit ?

Lu

quelque chose

mës nga dem kaasamaas?

es-tu déjà allé en casamance?

Dafa wóorul

C’est dangereux

Gox bi

Le quartier

ñaata waxtu ?

combien de temps ?

dara yombul ci adduna

rien n’est facile dans la vie

looy def ? lan ngay def ?

qu’est-ce que tu fais ?

senegal moo dàq Faraňse

le sénégal est mieux que La France

bu ma nekkoon xale, sama yaay dafa may làkkon wolof

quand j’étais petit, ma mère me parlait wolof

mën nga wax wolof ?

peux-tu parler wolof ?

mën nga waxaale ci senegaal ?

tu peux négocier au Sénégal ?

Bëgg naa toog fi Faraňse

Je veux rester en France

ndax

pour (dans le but de)

bul ma sonnal

ne m’embete pas/ ne me fatigue pas

léegi dem nga déglu

maintenant tu vas écouter

maangi ligéey ci benn banque

je travaille dans une banque

dama bëgg wecce ay euro ak fcfa

je veux changer des euros contre des fcfa

paas bi ñaata la ?

quel est le prix du billet ?

dama bëgg dem ci Pikine

je veux aller à Pikine

am na solo

c’est intéressant

neex na

c’est amusant

Dëkkandoo yi

Les voisins

yagg na

Depuis longtemps

kan la ?

C’est qui ?

lan la?

C’est quoi?

ubbil bunt bi

Ouvre la porte

tëjal bunt bi

ferme la porte

Dafa ndaw

C’est petit

Dafa bari

c’est beaucoup

Dafa metti

ça fait mal

Dama feebar

Je suis malade

Sama yaram dafa tàng

J’ai de la fièvre

Dama lakk

Je me suis brûlé

Mën naa gis doktoor bi?

Je pourrais voir un médecin?

waxal !

Parle!

wax ma / wax ko / wax leen

Dis-moi / Dis-lui / Dis-leur

déglu ma!

écoute moi!

bul ko wax !

ne lui dis pas!

Dégg naa la

je t’écoute

Dégg naa

J’ai compris

amuma dara

je n’ai rien

danga sop

Tu es turbulent

Danga doff

Tu es bête

duma xam / xamuma

je ne sais pas

dama xalaat

je réfléchis

Gëj laa na gis

ça fait longtemps que je ne t’ai pas vu

gëj

longtemps

looy def ?

qu’est-ce que tu fais?

looy bëgg def ?

qu’est-ce que tu veux faire?

looy jàng ?

qu’est-ce que tu étudies?

ãn bi pare na

le déjeuner est prêt

neex na lool

c’est très bon

jogal!

lève-toi!

ban waxtu moo jot ?

quelle heure est-il?

ana Mi ?

où est Mi ?

dama wara dem marché

je dois aller au marché

maangiy dem

je m’en vais

Am na internet fi ?

Y a t’il internet ici?

Lan mooy kodu wifi bi ?

Quel est le code wifi?

Mooy

C’est / qui est/ ce qui

Mën nga ñew fi ?

Peux-tu venir ici?

Dama reer sama kayit

J’ai perdu mes papiers officiels (ID)

Dañu sàcc sama kayit

On m’a volé mes papiers officiels (ID)

Dinaa sangu ak saabu

Je vais me laver avec du savon